Les nombres - Lim yi
0 = tus
1 = benn
2 = ñaar
3 = ñett
4 = ñent
5 = juróom
6 = juróom benn (5+1)
7 = juróom ñaar
8 = juróom ñett
9 = juróom ñent
10 = fukk
11 = fukk ag benn (10 et 1)
12 = fukk ag ñaar
13 = fukk ag ñett
14 = fukk ag ñent
15 = fukk ag juróom
16 = fukk ag juróom benn
17 = fukk ag juróom ñaar
18 = fukk ag juróom ñett
19 = fukk ag juróom ñent
20 = ñaar fukk (2×10)
21 = ñaar fukk ag benn
30 = fanweer
40 = ñent fukk
50 = juróom
60 = juróom benn fukk
70 = juróom ñaar fukk
80 = juróom ñett fukk
90 = juróom ñent fukk
100 = téeméer
1000 = junni
Le système de numération est assez simple, il n'y a pas d'exception, mis à part 30 = fanweer. Il faut noter qu'il s'agit d'un système quinaire ; par exemple pour dire 6, on dit 5+1.
Commander mon ebook apprendre le wolof qui reprends tous les cours enseignee dans cette blog et plusieurs autres cours non disponible en ligne Prix : 2 euros
Aucun commentaire:
Enregistrer un commentaire