Chiffres wolof en français

Un Benn
Deux Ñaar
Trois Ñett
Quatre Ñent
Cinq Juroom
*****  
Six Juroom benn
Sept Juroom ñaar
Huit Juroom ñett
Neuf Juroom ñent
*****  
Dix Fukk
Onze Fukk ak Benn
Douze Fukk ak Ñaar
Treize Fukk ak Ñett
...  
Vingt Ñaar Fukk
Vingt et un Ñaar Fukk ak Benn
Vingt deux Ñaar Fukk ak Ñaar
Vingt trois Ñaar Fukk ak Ñett
...  
Trente Fanweer
Trente et un Fanweer ak Benn
...  
Quarante Ñent Fukk
Cinquante Juroom Fukk
Soixante Juroom Benn Fukk
Soixante Dix Juroom Ñaar Fukk
....  
Cent Teemeer
Cent cinquante Teemeer ak juroom fukk
Cinq cents Juroomi teemeer
Mille Junni

Aucun commentaire:

Enregistrer un commentaire